Foo koy jëleeti?
Where would you find it again?
Ku la bëggee ni man
Someone who likes you the way I do
Foo koy jëleeti?
Where would you find it again?
Ku la soopee ni man
Someone who admires you the way I do
Foo koy jëleeti?
Where would you find it again?
Ku la nobee ni man
Someone who loves you the way I do
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Ku yeewu xaaja guddi di xool ndax saangu nga
Someone waking up in the middle of the night to make sure you are well covered
Ku lay wax dëgg joo bëggula déeg, ni man
Someone who tells you the truth you don't want to hear
Ku nek ak fala bur bi yalla fetëler
Everyone has a side that God Almighty put them in
Ak fa nga bëgg sa boop féetée
And a side they want to be in1
Fu ma koy jëleeti?
Where would I find it again?
Ku ma nobee ni yow
Someone who loves me like you
Fu ma koy jëleeti?
Where would I find it again?
Ku may fiiree ni yow
Someone who gets jealous over me like you
Fu ma koy jëleeti?
Where would I find it again?
Ku ma ñeme wax degg ni yow
Someone who is not afraid to tell me the truth like you
Fu ma koy jëleeti?
Where would I find it again?
Bu la buur bi yalla bëggee da nga koy xam
When God loves you, you just know it
Ndax tóoxiduna boo dugg mu geénee la ci
Cause he manages to put you out of trouble everytime
Bu la nit ki bëggee doom yaay da nga koy xam
When someone loves you, brother, you just know it
Ndax bu musiba di xeeñ mu ne kaay gungeé ma fii
Cause she can feel the trouble and make you stay away from it
Aaduna ngoogu ci suñu kanam
That's life right there, in front of us2
Jaam warula tëkku moroomu jaamam
One shouldn't threaten his peer
Aduna ngoongu ci suñu kanam, doom yaay
That's life right there in front of us, my friend
Jaam warula nattu moroomu jaamam
One shouldn't threaten his peer
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Fan nga koy jëleeti?
Where would I find it?
Fan nga koy jëleeti?
Where would I find it?
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Ku bëgg sa jamm ni man
Someone striving for your peace like me
Fu ma koy jëleeti?
Where would I find it?
Ku degg dat ni yow
Someone getting it all like you
Fu ma koy jëleeti?
Where would I find it?
Ku mok pot ni yow
Someone sweet like you
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Ku yeewu xaaja guddi di xool ndax saangu nga
Someone waking up in the middle of the night to make sure you are well covered
Ku lay wax dëgg joo bëggula déeg, ni man
Someone who tells you the truth you don't want to hear
Ku nek ak fala bur bi yalla fetëler
Everyone has a side that God Almighty put them in
Ak fa nga bëgg sa boop féetée
And a side they want to be in
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Foo koy jëleeti?
Where would you find it?
Fan la koy jëleeti?
Where would I find it?
Fan la koy jëleeti?
Where would I find it?
Fan la koy jëleeti?
Where would I find it?
Fan la koy jëleeti?
Where would I find it?